Question en attente de réponse
Y'a t-il des gamers parmi vous si oui vous jouer à quel jeu?
Réponses
Hé wei desert strom excellent jeu
C'est quel jeu alassane mane mome Counter strike fortnite mobile si ioe nk
Ouii nfs payback et moderne combat 5
Ouii j'adore payback jeu de guerre bien les nouveautés de modern combat c'est bien aussi
Mais je pense que Fortnite et Pubg Mobile ont pris l'avantage qui confirme
C'est un jeu d'action tu accomplis des missions soldats
Sama gayi kouma gnimé fifa19 wala pro19
Mais yén deguouma kéna jeu football
La dernière fois que j'ai installé fifa19 sur mon pc il s'est planté mdrrrr
bonsoir aliou il y'a en
bane jeu ngua beugue niou joué ko
OR ANGE pro19 deugue diameu la dé
Mady wakhal dé am dara la kay
SEN EGALmon bro mossi gueuna nék pro
Alassane Loy wakhni léguino moudjé déf?
Fifa bi dafa diss dé motakh bo amoul gameur bou tjil ni moy lolou dé
Kon tay aye jeux vid miffi ame
Les gars c'est kom ça déh
Kou nekk ak lila yitél
Mane mom aye jrux waxoumassi draa.
Alassane yagui tardé fifa 19 aka nekh
Orange gnimé nala dei heure bo paré rk niou game
Oh anattack jeux dafa bakh dei hana ioe Pa ga
Orange fifa bi dei yornako dissoul sax 50Go kesser dafa nekh dafa fek gayi si pS4 bi lagn koy jouer
suis plutot jeux de combat
Assasins creed jadore
Surtout Origin
Et battlefield aussi boboumom jeu de guerre absolu
Hi mane dh playstation rek
mba dou SEN ÉGAL da rodé
aliou yak OR ANGE nassi dall
Mady yassi guiss dé am Dara la
Sénégal game rék lay déf
PES wala FIFA yép lay game
Khaman un jour bou néké tournoi Orange bou amé niou dadjé fa
Game Lou neikh Mane mom FIFA la guena takhaw que PES
oui OR ANGE ame daraldara kay
Wa Kone diékhna tak bou tournoi amé niou dadjé fa
Comme niou game fofou
Mais fifa la gueuna beugu game que pes
Gayi yen fifa rk lafi deg ak pes
Vous êtes chaud pour un battle en ligne pes lite
Mane mome jeux mobiles yi rk
Sama gamer yii way
Vive PES 19
Lol aliou déssi bolé Football way frére
Sock yow warna niou programmé béna jour dé wala tournoi bou temps amé
Waw OR-ANGE war na meun nek deii mais fo ma entrainer watt
Lo yor PS4 ou sur PC ma train
Sock moy am sakh pes mom tji pc lakoy gamé au Sénégal
Mais fifa bi mom PS4 lakoy gamé
Boy yéne aye gamer nguéne koi
Wane léne ma yonbii book
Beugue na nekk gamer mais xawma yone bii
Walla Orange yako lak pes19 mom chi pc rk
Kone nak hatal ma commencer entrainement yi
Mouhamedsock_03 a répondu
Mouhamedsock_03 a répondu
Mouhamedsock_03 a répondu
Mouhamedsock_03 a répondu
Mouhamedsock_03 a répondu
Mouhamedsock_03 a répondu
OR-ANGE a répondu
OR-ANGE a répondu
OR-ANGE a répondu
OR-ANGE a répondu
OR-ANGE a répondu
OR-ANGE a répondu
Mady a répondu
Mady a répondu
Mady a répondu
Mady a répondu
Mady a répondu
Mady a répondu
OR-ANGE a répondu
OR-ANGE a répondu
OR-ANGE a répondu
OR-ANGE a répondu
un anonyme a répondu
un anonyme a répondu
un anonyme a répondu
un anonyme a répondu
OR-ANGE a répondu
OR-ANGE a répondu
OR-ANGE a répondu
Mouhamedsock_03 a répondu