Salam Abdou Mbengue
Magui lay diadieufal si sa teway :blush:
Meune gueko convertir en bon d'achat boy meune utiliser si souniou boutique partenaire yi. Meune gue ame liste bi si #221#16#.
Pour lolou dangay dem agence bila guena djégué guir deff échange bi.
Magui fi so amé benene ladj.
Modérateur Orange
Retrouvez-moi sur Whatsapp +221771370101