Ou

Question en attente de réponse

Instant Leb #Orangers

Alors Sama Gars Yi
Gnou fatalikou lébbou werrou koor yi ma khol.
Leb bou gueneu nékh gagner pass 1GO bou 3 jours

Community Manager
Community Manager

Community Manager

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points
Equipe

Réponses

Mouhamad F
Mouhamad F

Mouhamad F

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

bi béeneu satcheu la woon....Professionnel neuk...Tenue de camouflage akh yeup...
éspécialité weum moy teup mur you geuneu kowé chi deukeubi...

Bénn jour nakk mou teup rék atterrir chi digeu famille bi di fékhlou chi cour bi.... des ponakall rek ds la maison

Mou xol gauche, xol droite rék commencé yeungeul boppeubi, commencé Kass (se plaindre): Cheuteuteutt pourtant wokhonna Commandant bi mou parachutémeu plus à l'est...Ah non way wakhone naakoko.

Mohamed Africa
Mohamed Africa

Mohamed Africa

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Merçi c est geniale

Ousmane
Ousmane

Ousmane

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Ki béni peul la wone bou dougue si avion tok si place diambour nou néko fofou dou sa place rek mou bagne hôtesse bi néko place bobou kiye tok fofou fouta laye déme rek peul bi diogue

SEN ÉGAL
SEN ÉGAL

SEN ÉGAL

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Hahaha koor diapoulén dé. Mdr
Ins bi ma ngui diém mé sama xel ma dem !

Aliou
Aliou

Aliou

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Salaam gayi
Ah bi nak ben famille leu wone wadji am doom legui doom chakque fois bouy namp "sow"bi dafay diekh legui mou merr mou dieul posson "poison" legui nak mou niew fekk pere bi dead déee.
Lol

Mouhamedsock_03
Mouhamedsock_03

Mouhamedsock_03

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Big up les gars
Am len bii
Souleye leu kii

Boubacar
Boubacar

Boubacar

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Bon bèn père de famille la wonne ak sokhna wome Pa bi woor bo 17h geune togue si bountou gallé bi, diabar bi diogué marché romb ko néko '' nidiay yagui togue'' rék Pa bi nékh mé ioe souma djoumoul amna foumala xamé déh

Boubacar
Boubacar

Boubacar

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Bon bèn père de famille la wonne ak sokhna wome Pa bi woor bo 17h geune togue si bountou gallé bi, diabar bi diogué marché romb ko néko '' nidiay yagui togue'' rék Pa bi nékh mé ioe souma djoumoul amna foumala xamé déh
Mrd hahahaaaaaaaaaaaaa