Ou

Question en attente de réponse

Instant Fun #Orangers

Ana Sama wa Team?

Anonyme
Anonyme

Anonyme

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Réponses

SEN ÉGAL
SEN ÉGAL

SEN ÉGAL

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Hello !

Way gars yi dé. Bouniou nieuwé fi Tothieu.
Ci yii laniouy yeungou dé niom...

Anonyme
Anonyme

Anonyme

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Gnou khar bakhaaam

OR-ANGE
OR-ANGE

OR-ANGE

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Béna mo ngi nonou

OR-ANGE
OR-ANGE

OR-ANGE

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Banèn mo ngi nonou

SEN ÉGAL
SEN ÉGAL

SEN ÉGAL

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Mais à part ça, ma ngui la done parer wo téléphone sakh, tay sama journée bi Moy lolou.

Demb damadone dém village, sama Range rover s'est bloqué dans la boue, ma wathie boukh ba tass et sans aucune aide.

Ce matin je me réveille et je constate que j'ai poussé mon lit jusqu'à salon...

OR-ANGE
OR-ANGE

OR-ANGE

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Béne pa mo liguéyi ba ngone nieuw di simi khaftane bi ,Bopp bi guénagoul sakh diabar ji nék: Nidiaay gaz bi diékhna .
Paa bi simékou néko: dalal adouna dou dara ,mou tite naane ko mba diam !
paa bi néko sa yaye dada décédé légui! Ndawsi youkhou,
mouniko niaw yama tiital ma fayou mdrr

SEN ÉGAL
SEN ÉGAL

SEN ÉGAL

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Hahaha kel pa...
Dé lay fayé mom. mdr

OR-ANGE
OR-ANGE

OR-ANGE

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Dieulal bi

Béna gaindé mo fék béna way bou tok 3ans sanguou woul rék mou khampeuh cuisse bi !

Dafko khampeuh rék djoubali marché ba niite yi di daw di dougu si table yi gni di lakhatou!

Rék gaindé bi né bouléne daw dakhar ak limon lay weur sama khél dafay téy

SEN ÉGAL
SEN ÉGAL

SEN ÉGAL

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Hahaha, wouaw j'en peux plus...
Noooooon way !

Mady
Mady

Mady

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

nio ngui ni

SEN ÉGAL
SEN ÉGAL

SEN ÉGAL

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Béneu faam bou deuk sama kogne bou tameu wakh ay terme ( " feul feulalé " " sannékou ", " dirékou "," fofa todj ", " khamna damay moudjé ganiou rék ",

Mo doon diégui sank ci talli bi sank,

Béneu bus moko FEUL,

Ap clando FEULALÉKO,

Mou SANÉKOU,

Camion di nieuw mouy DIRÉKOU pour langamou si trottoir bi,

Far yalla FOFA TODJ,

Ma nieuw xôl ko, KHAMNÉ DAFAY MOUDIÉ GANIOU RÉK.....

***** Ba légui nii fa la nék, mo takh ma déconnecté ci communauté bi, ndékké gouma sakh ****

OR-ANGE
OR-ANGE

OR-ANGE

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

hahahaha mdrrrrr

Ousmane
Ousmane

Ousmane

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Jpp là mdiir

Ousmane
Ousmane

Ousmane

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Paa bii ndey sane weurr neuhh job ba sonee amoull mou kheuye tassaannté ak béne maçon wadji neikoo jurneii 2500 amna pa bi neii waw niou deime
Léguii maçon bi diko expliqué job bi nane la "souff biii déy yeiikk si kaw béton blanc bii si kaw béton noir bi si kaw ciment bi si kaw mélange bi na tmt si kaw gua yeigall leipp si kaw après ma wakh la lo waraa deiff lénéne"
Rk pa biii reiii di reiii reiii rk kay wadji neikoo wa mon père loy reiii pa bi neikoo mon fils dama bayiii bou yague teii yeugooo ko

zetoblue
zetoblue

zetoblue

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Gars yi meune guène mayé mdrrr