Question en attente de réponse
Xaral ma dougalate sa carte sim bima utiliser wul depuis 03 mois nguir ma am si points sargal you beuri yi orange di mayé ! Plus d'infos ici https://bit.ly/2ScRdii
Réponses
Sama gayi guéné lén puce Orange you yagu yi points Sargal yi am dara la dé
Magui dem guener sama puce yi dei mdrr
sama gayi you bayi sen puce demlen récupérer dji
Bouniou takh ma dieuliwat sama bénene puce ba way !
SEN-ÉGAL niata puce ngua yoré?
SÉN ÉGAL nga alaléma béna puce fofou mdr