Question en attente de réponse
Réponses
Merci pour l'infos
Magui kay suivre nii si sen page bii
Ay idée you am solo
La gayi di tek
Projet aywajeune lou graw migui nonou
Ha ok sén page bi aussi dafkoy ték
Gayi ko khamoul meune nanioufa dém
Wey niou khol gayi lougnouy proposer
Comme ça niou mane ko am en live
Si moy yone
Je valide 2e bi Wallou bi mom dafay fay dei
Merci pour l'infos
Magui kay suivre nii sakh
Ay idée you am solo laniouy ték
Jeunes yi guiss naniou ci sen bopeu
1 bi tamit am dara la dé
Mais yay souwassiiiir !
Wa beindayoffficiel mom daccorouma beug democratiser wifi bi dou yone nagn defar satellite mo guen sinon bimom waroul avancer lol
Gayi ni leu dei
Orange mofi nek di diapeler sama gayii
Mo guen niou dem exterieur
Toubab yi di niouy use lol
Dieuraguen dieuf
Mais borom wifi bi mom ioe mom merer nala
Kone hana daniouy yokk debit
Magui fofou dei doumako rater
wakhlén dé sama gayi
Aucune question liée
SEN ÉGAL a répondu
Mouhamedsock_03 a répondu
Mohamed Africa a répondu
SEN ÉGAL a répondu
Ss12345 a répondu
OR-ANGE a répondu
OR-ANGE a répondu
OR-ANGE a répondu
SEN ÉGAL a répondu
SEN ÉGAL a répondu
SEN ÉGAL a répondu
OR-ANGE a répondu
OR-ANGE a répondu
OR-ANGE a répondu
SEN ÉGAL a répondu
OR-ANGE a répondu
SEN ÉGAL a répondu
OR-ANGE a répondu
SEN ÉGAL a répondu
OR-ANGE a répondu
SEN ÉGAL a répondu
OR-ANGE a répondu
SEN ÉGAL a répondu
OR-ANGE a répondu
OR-ANGE a répondu
SEN ÉGAL a répondu
Mouhamedsock_03 a répondu
Mouhamedsock_03 a répondu
SEN ÉGAL a répondu
Mouhamedsock_03 a répondu