Question en attente de réponse
Fanta! Karim mom, tamë na dima tardel sa yu ñu waré génë mais tey mom du cii dal ! Ak appli Chat message d’Orange bi, dina xam fumu nek !
Réponses
Sama gayi appli Chat message d’Orange bi, diarna woute dé
Wawaw dafa nex dei
Orange rèk la mane mom dinako coaché
Aucune question liée