Question en attente de réponse
Ñaak pass, taxatul nga bañ ma mënë contacter.
Active juste tes données mobiles et ouvre ton application Orange et moi.
En resumé il suffit juste d'activer vos données mobiles même si vous n'avez pas de pass internet pour utiliser l'application orange et moi.
Réponses
Sama application bâ ngui nii dé
légui avec Ibou tout est possible
sans pass ngua contacté Ibou
Ah bon Kone guiss nga lolou
Sans pass nga connecter ci
Dafay dieund pass aussi
Même Doug def sa suivie consommation
Ibou kay gayi bèna lafi
Après warna niou ko guiss dé mou wakhniou son secret
Lolou moy deff buzz déh
Apps bi Moy number one
Mako tipo Man rék
Lénene meunatout am buzz ndax mom
SEN GAL mangui lay nouyou akk diam
Diam ci yaw AK ci nieup
Naci application bi topeu
Ibou Partout EST OUEST NORD SUD
AK haut et bas sakh
Wawaw cop mo ngi fép fouko orange sokhla
Motakh dou taguo ak insomnie
Ko khamni dafay fonctionné 24/24
Magui ziaar dh xana tay reunion ambasadeur leu.
Niguéne tewé rafetna
Mais orange et moi lepay bakh
Baptême de feu
Delo siar, diam ci yaw !
Hello pisko nakamou
Tyler a répondu
Salla a répondu
Mady a répondu
OR-ANGE a répondu
OR-ANGE a répondu
SEN ÉGAL a répondu
papisngom a répondu
OR-ANGE a répondu
OR-ANGE a répondu
OR-ANGE a répondu
SEN ÉGAL a répondu
Mady a répondu
SEN ÉGAL a répondu
SEN ÉGAL a répondu
SEN ÉGAL a répondu
un anonyme a répondu
SEN ÉGAL a répondu
SEN ÉGAL a répondu
SEN ÉGAL a répondu
un anonyme a répondu
un anonyme a répondu
un anonyme a répondu
OR-ANGE a répondu
OR-ANGE a répondu
Mady a répondu
SEN ÉGAL a répondu
SEN ÉGAL a répondu
SEN ÉGAL a répondu
SEN ÉGAL a répondu
Mady a répondu