Question en attente de réponse
which kind of music do you listen guys and who's your favorit singer
Réponses
Gnoune hip hop rekk
Hardcore nakk lalay teval ni
Gnom eminem,Royda 5", mgk,ymgx
Ah ok lolou dei magii kay soga xam bro
Zetoblue mane son mom waxoumassi dara
Eminem ga wax sa way yagii xam.loumouy lakk esk
Mdrr
Kone dei yen vous etes hyper mega branchrr
Prtant jazz c nex
Zeto mome affaire classique dako nekh koi
J te conseille ngay get sma rappeur bi
Fi mom.nieupay deg lou son
Ay jazz ay slow ak hard mdrr brancher guen dal
Il est fort té lou classique rek lay def
sama gayi li ngén di wakh fi khamoussi dara
Sock Anglais bi ay taxlé rek la
mane mom souma démé bay dégu lou you lay dégu lou
Yaw fatténa mbalax
Soyleymane faye rek néko demna
sadikh jule lou lér nagneuh lay way
Billahi, kokou légende la
Ay son wam lepp ay diangat la
Soumay dem school reto en boucle lay mayé
mdr deugu rék lay way
surtt le son fokay dieuléti
Pourtant mahou amna talent nak !
Wait ba gars yi gueun ko découvrir !
Mane mom rék mo may sawarlo déglou music !
enfin kkun qui ecoute du rock. presii kel groupe est ton prefeŕé
Sadikh a répondu
Sadikh a répondu
Sadikh a répondu
Sadikh a répondu
Sadikh a répondu
Sadikh a répondu
Sadikh a répondu
OR-ANGE a répondu
Sadikh a répondu
OR-ANGE a répondu
Sadikh a répondu
OR-ANGE a répondu
OR-ANGE a répondu
OR-ANGE a répondu
OR-ANGE a répondu
OR-ANGE a répondu
OR-ANGE a répondu
OR-ANGE a répondu
Sadikh a répondu
Sadikh a répondu
Sadikh a répondu
Sadikh a répondu
Sadikh a répondu
Sadikh a répondu
Sadikh a répondu
Mouhamedsock_03 a répondu
Mouhamedsock_03 a répondu
Mouhamedsock_03 a répondu
Mouhamedsock_03 a répondu
Mouhamedsock_03 a répondu