Question en attente de réponse
which kind of music do you listen guys and who's your favorit singer
Réponses
Fallou daaara hewoull !!
Non Fallou bayiwouma sama lokho magui ssi dei
Mdrr non.demewoufa nonou ymgx sax
Mdrrr daga tang ioe motahh sen rythme mo graw
Fallou tanyii yama guena tangg deii shiii
Ymgx je laisse la main pour les autres . Tmt
G rater koi encore
Tempsyi mome tangue deug nguéne def
Rythme bi mone grawna trop
Kontey ya ngi si dh
Temps fort kay ainsbi
Sock mougi si ba légi dh
Orange mome tamite dou mayé dra
mane yay sama chauffeur fo raté ma raté mdrr
makhala khana kontéy fi diar?
sa way mo ngi fép koi
dama yakarni jakarta wam bi
kérosen lassi déf
motakh kéna douko guiss comme mélakh koi
mais yow kéna dou yow mdr
-No mane légi charrette la yor
sama chauffeur bi
Da ngay dakh ba sonne!
yow avion de chasse nga yor
Lol yawite ndandane nga dh
Mais tay Barça dey play dh
Paris mome naple la am
Yalna naple gagné way
Sadikh a répondu
Sadikh a répondu
Sadikh a répondu
Sadikh a répondu
Sadikh a répondu
Sadikh a répondu
Sadikh a répondu
OR-ANGE a répondu
Sadikh a répondu
OR-ANGE a répondu
Sadikh a répondu
OR-ANGE a répondu
OR-ANGE a répondu
OR-ANGE a répondu
OR-ANGE a répondu
OR-ANGE a répondu
OR-ANGE a répondu
OR-ANGE a répondu
Sadikh a répondu
Sadikh a répondu
Sadikh a répondu
Sadikh a répondu
Sadikh a répondu
Sadikh a répondu
Sadikh a répondu
Mouhamedsock_03 a répondu
Mouhamedsock_03 a répondu
Mouhamedsock_03 a répondu
Mouhamedsock_03 a répondu
Mouhamedsock_03 a répondu