Ou

Question en attente de réponse

#BattledeLions

#Fun

Ce week-end, nos Lions seront encore à l’affiche pour le championnat de France avec Adama Mbengue de Caen contre Ismaila Sarr de Rennes. Lequel va remporter ce duel entre #Lions? #BattledeLions https://www.facebook.com/orange.sn/

OR-ANGE
OR-ANGE

OR-ANGE

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Réponses

Sadikh
Sadikh

Sadikh

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Ana team deteste ligue 1

Sadikh
Sadikh

Sadikh

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Wané léne sen bopp

Sadikh
Sadikh

Sadikh

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

J pense k renne l'emportera

SEN ÉGAL
SEN ÉGAL

SEN ÉGAL

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Ben ngui nii dé Sadikh !

SEN ÉGAL
SEN ÉGAL

SEN ÉGAL

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Mais que ce sont des sénégalis qui jouent moom ci la lén di diapalé may len beut !

SEN ÉGAL
SEN ÉGAL

SEN ÉGAL

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Ma ngui ci guinnaw iso sarr mon player !

OR-ANGE
OR-ANGE

OR-ANGE

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

lol sadikh fi gayi ay fervents suppoters laniou dé

Sadikh
Sadikh

Sadikh

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Lol.... I'm dead

Sadikh
Sadikh

Sadikh

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Wey!!! Liga dale kone ngay suivre

Sadikh
Sadikh

Sadikh

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Perso liga, calcio ak touti Première ligue

SEN ÉGAL
SEN ÉGAL

SEN ÉGAL

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Liga ci ponkal yi !

OR-ANGE
OR-ANGE

OR-ANGE

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

mais fépeuh fou joueurs senegalais nék war naniou ko supporté

SEN ÉGAL
SEN ÉGAL

SEN ÉGAL

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Premier league Tamit kén baniouko !

OR-ANGE
OR-ANGE

OR-ANGE

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

attention rennes temps nékoul si forme dé caen peut gagné

Sadikh
Sadikh

Sadikh

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

OR_ANGE li nga wax deugla

OR-ANGE
OR-ANGE

OR-ANGE

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

voila sen egal naniou tji diap yoklén visibilité car niom saniou ambassadeurs laniou

Sadikh
Sadikh

Sadikh

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

J swi d'accord sou dé en terme équipe boumou nekk

Sadikh
Sadikh

Sadikh

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

SEN_EGAL premiere ligue tané na rek, ak ambiance

Mouhamedsock_03
Mouhamedsock_03

Mouhamedsock_03

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Renne de Ismaila Sarr rkk !!!

Mouhamedsock_03
Mouhamedsock_03

Mouhamedsock_03

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Tay Liverpool Arsenal laniouy wax nioune mdr

Mouhamedsock_03
Mouhamedsock_03

Mouhamedsock_03

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Saddikh magui ni ligue 1 mom mdrr!!

SEN ÉGAL
SEN ÉGAL

SEN ÉGAL

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Wa waw Or-ange niom nioy ambasseurs Senegal, Nioune niouy ambassadeurs Orange! mdr

SEN ÉGAL
SEN ÉGAL

SEN ÉGAL

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Sadikh, Angleterre fofou Keur gou mak la dé, diakhasso la déf mo takh mou nékh !

SEN ÉGAL
SEN ÉGAL

SEN ÉGAL

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Sock tay dou yomb ! ci ko tek tay ?

Mouhamedsock_03
Mouhamedsock_03

Mouhamedsock_03

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Mane amateur de foot la.barcelone cf rk
Daniouy setane dax derby la koii mais dou yomn deii ymgx

Mouhamad F
Mouhamad F

Mouhamad F

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Boy sock yaw xamo dara si foot kw

Mouhamad F
Mouhamad F

Mouhamad F

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Gnou xamoul foot fo wacé foot gnouné Barcelone

Sadikh
Sadikh

Sadikh

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Mouhamed F xana pik yi moy borom lol

Sadikh
Sadikh

Sadikh

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Mais match renne vs caen kane mo gagné

Mouhamedsock_03
Mouhamedsock_03

Mouhamedsock_03

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Mdrrr xawma sax france mom dafa nazz Trop