Ou

Question en attente de réponse

Join the discussion!

Waxalen lou len nex fi dara
H24 bi fila

Mouhamad F
Mouhamad F

Mouhamad F

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Réponses

Mouhamad F
Mouhamad F

Mouhamad F

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

yaw sock dafa melni da nga ragal sedd dé

Mouhamedsock_03
Mouhamedsock_03

Mouhamedsock_03

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Way sedday bro soth rk lay df

Mouhamad F
Mouhamad F

Mouhamad F

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

ins bi boya bi start na dé

Mouhamad F
Mouhamad F

Mouhamad F

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

soth kagn seed ben ins daf si bax

Mouhamad F
Mouhamad F

Mouhamad F

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

mais mane daf may tayal lo kw

Mouhamad F
Mouhamad F

Mouhamad F

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

adiar bi bo waré diok pour dem diangui bilay damel ni da nga wadia dé

Mouhamedsock_03
Mouhamedsock_03

Mouhamedsock_03

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Seeday dafa nexx nak ben ains

Mouhamedsock_03
Mouhamedsock_03

Mouhamedsock_03

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Tayal mdrrr !!!

Mouhamad F
Mouhamad F

Mouhamad F

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

si nexna ben ins mais moy lolou benene ins nakk

Mouhamad F
Mouhamad F

Mouhamad F

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

boy yaw diambar nga seday doula tayal lo

Mouhamad F
Mouhamad F

Mouhamad F

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

mane tayal fepp lay deff srx

Mouhamedsock_03
Mouhamedsock_03

Mouhamedsock_03

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Lol sedd na nexx deii ymgx!!

Mouhamedsock_03
Mouhamedsock_03

Mouhamedsock_03

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Yambar ga rk

Mouhamad F
Mouhamad F

Mouhamad F

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

boy yambar yi gnoy gnémé sedd nakkk

Mouhamad F
Mouhamad F

Mouhamad F

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

mane insbi do sax sib

Mouhamad F
Mouhamad F

Mouhamad F

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

xaral ma gnew fote sama pul yi sax bala lundi ndax xamna sedd lundi lay xar insbi

Mouhamedsock_03
Mouhamedsock_03

Mouhamedsock_03

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Mdrr wax ga deuggg dei wadjal touti

Mouhamedsock_03
Mouhamedsock_03

Mouhamedsock_03

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Yambar bou gnemer sedd amoul

Mouhamad F
Mouhamad F

Mouhamad F

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

touti da nga doff

Mouhamad F
Mouhamad F

Mouhamad F

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

bou bax nga nane

Mouhamad F
Mouhamad F

Mouhamad F

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

gayi ana ngen bokk
féérié rekk ngen fokk fait rien la

Mouhamedsock_03
Mouhamedsock_03

Mouhamedsock_03

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Ferié leu tmt fallou

Mouhamad F
Mouhamad F

Mouhamad F

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

mais férié bassi nga dagno wara gnew fi kw fi amoul ay férié dé boy

Mouhamedsock_03
Mouhamedsock_03

Mouhamedsock_03

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Ferié !!!!!
La nak ymgxx niogui fii

Mouhamad F
Mouhamad F

Mouhamad F

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

yaw dal kone férié do deff dara kw

Sadikh
Sadikh

Sadikh

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Férié bi diexna ba tek ay mn

Sadikh
Sadikh

Sadikh

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Férié bi diexna ba tek ay mn

Mouhamad F
Mouhamad F

Mouhamad F

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

tay lougn fiy wax moy gnou rafetal site bi kw

Mouhamad F
Mouhamad F

Mouhamad F

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

yen yi diarouko fi dé

Mouhamad F
Mouhamad F

Mouhamad F

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

bmane mom tegui na sama tank bou yagg sax