Ou

Question en attente de réponse

E-sport serie

Orange loumouy xarr pour lancer ay e-sport bok
Gamer yi dinagn contane dei

Mouhamedsock_03
Mouhamedsock_03

Mouhamedsock_03

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Réponses

Sadikh
Sadikh

Sadikh

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Yeah sock, lolou rek lay xarr, stp op de PES, mais FIFA okay

Mouhamedsock_03
Mouhamedsock_03

Mouhamedsock_03

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Weuh saway Pes rk lolouy moy vrai jeu nak
Ak fortnite ak fifa ... ak RDR2

Mouhamedsock_03
Mouhamedsock_03

Mouhamedsock_03

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Sans oublier F1 ou need for speed un peu de run aussi
Lolou di na bax si grande vacance

Sadikh
Sadikh

Sadikh

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

No fifa est plus original k pes.
Pes c trop facile

Mouhamedsock_03
Mouhamedsock_03

Mouhamedsock_03

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Weuh Ababacar lolou ga fokk c'est plus difficile
Fifa c'est du n'importe les plus grand joueur de fifa sont sur pes 19

Mouhamedsock_03
Mouhamedsock_03

Mouhamedsock_03

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Vraiment jimy arragement la kay!!
( ͡° ͜ʖ ͡°)

Mouhamedsock_03
Mouhamedsock_03

Mouhamedsock_03

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Probleme bobou loy causam

OR-ANGE
OR-ANGE

OR-ANGE

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Sama gayi bakh yi mouhamed do niou bayi ak Pes ? fifa dou moromame mane niar yép lay game wayé pomme dou moromou néw way lol

Sadikh
Sadikh

Sadikh

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Lok sa arrangement ngay wax, yaw pes score yi nga fa meuneu dor, xalato ko ak fifac, puis k pes fo tollou dor day cadré wla mou dougou rek

Mouhamedsock_03
Mouhamedsock_03

Mouhamedsock_03

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Laylaa lolou chaner nakk saway xana guisso 18 bi ak 19 bi mo dakk fifa nangoulen

Mouhamedsock_03
Mouhamedsock_03

Mouhamedsock_03

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Mane tamit niarr yeup lay jouer mais pes mo dakk mo guena reel . Fifa nexoul dagay dieul ben joueur di daw rk

OR-ANGE
OR-ANGE

OR-ANGE

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

wa ki louko dal mdrr?

Mouhamedsock_03
Mouhamedsock_03

Mouhamedsock_03

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Ioe hamca loumay wax sax bo beuger demal google les plus grand joueurs de fifa ont critique fifa 19 cette année et joue plus sur notre jeu Pes 19

OR-ANGE
OR-ANGE

OR-ANGE

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

khana google wa PES laka wakhé lol?

Mouhamedsock_03
Mouhamedsock_03

Mouhamedsock_03

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Lol fo meun ti dougg demal youtube sax guemoma motax

Sadikh
Sadikh

Sadikh

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

OR_ANGE waxal dh. Sa fait rire koi en comparant PES et FIFA, c op du tt normal.

Mouhamedsock_03
Mouhamedsock_03

Mouhamedsock_03

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Lol yagolen suivre actu jeux motah
Jeux rk mdr

Sadikh
Sadikh

Sadikh

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Mais aussi c normal kou nekk am nga droit diokhé sa point de vue.
#Démocratie avec Orange.sn

Mouhamedsock_03
Mouhamedsock_03

Mouhamedsock_03

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Yen nieup wa fifa guen sauf moi lol

Mouhamedsock_03
Mouhamedsock_03

Mouhamedsock_03

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Weuh yene dagueni may sott tioloul
Fifa contenue bi rk mo nex mais gameplay
Nazz la

OR-ANGE
OR-ANGE

OR-ANGE

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

sock mano nani ndokh té bayi niou ak pes? lol

Mouhamedsock_03
Mouhamedsock_03

Mouhamedsock_03

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

Mdr Wa ANGE tioloul mais dal warnaniou am E-sport si vacances yi
(・∀・)

OR-ANGE
OR-ANGE

OR-ANGE

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

weuy warna maneu am dé mane bi moudjé am si kor gui dakar sacré coeur la démone

Mouhamedsock_03
Mouhamedsock_03

Mouhamedsock_03

Ambassadeur Orange
4
1000 / 1000
points

War na meun nek koa vraiment
Vivement souhaiter!! (・∀・)