Question en attente de réponse
Gayi fi tay weet na nagn developper sounou idee pour mouy nexx way. Ay jeux ou autres choses sax
Réponses
Tay kay fi dafeuh wétteuh trope.
Noumou démé nonu les gars ?
Mdr wet na mom
Proposons des trucs à faire
Salam les gars !!!!
Salam iboush
Mouhamedsock def ma compte rendu loufi xew lepeu!!!!
Dakh insbii wathie bou bess leu !!!
Fi compte rendu xamga lan la
Tontou question lol lolou ga tarder
Bayil di wax wathie bess ioe.gay ancien gloire
Genre niata ambassadeur akk ambassadrice you bess Nio fi ameu you bess tak
Ancien gloire nak mdr
Respect zéro lol
Fater nala wax am.nagn ambassadrice gayi contane niane ak ambassadeur bou bess OR-ANGE
Lolou guis nako si WhatsApp bii
Félicitations wayyy !!!!
Non boul wax lolou tamit nangoul ni ancien gloire ga rklol
Danii wara dolli sax ambassadeur yii
Ça me fait penser bamay doga doneu Ambassadeur c’était Émotionnelle frère
Touti ma diox dakh xol bou sedeu :)
Woyyyyy iboush ioe comedie migui lay xarrr
Dioy ga an!!!
Non ioe frère tu comprends rien !!!!
Et c normal sakh sakh !!!!
Dieug nek ambassadeur nouvelle génération dafa neikh frere billay ...emoji dioye
Lolou dou meussa Faye fierté leu
Émotion dioy dioy
No c pas normal tamitt
Bama neker ambassadeur damaner "ENFIN"
Lol
Non ioe sa processus dafa yag trop presque 3 semaine
Mdr
Mais content na si ioe semaine passer déguena ta bien travailler ba nagou sama place meuilleur contributeur de la semaine athiommm
Mane kayy dama sonone
Wawaw ma dieul sa place kay revange
Lol mais ba xam gani semaine bi naroul yombou
Gaïndé da nameu yapp
Lol
Aythia defi relever meme ymgx sa noumouy demer .
Gainder bi da hiff yapp pour cette fois mais mane moussouma sourr
Wawaw man li la guem
Pas affair yoyou nonou
Amoul mayè dara lol
Amoul seral dara
Ba xamga code # rk
Mdr xawmako dei Code bi lan la
zetoblue a répondu
iboush a répondu
Mouhamedsock_03 a répondu
iboush a répondu
Mouhamedsock_03 a répondu
iboush a répondu
zetoblue a répondu
Mouhamedsock_03 a répondu
zetoblue a répondu
Mouhamedsock_03 a répondu
zetoblue a répondu
Mouhamedsock_03 a répondu
iboush a répondu
Mouhamedsock_03 a répondu
iboush a répondu
iboush a répondu
Mouhamedsock_03 a répondu
iboush a répondu
Mouhamedsock_03 a répondu
iboush a répondu
Mouhamedsock_03 a répondu
iboush a répondu
Mouhamedsock_03 a répondu
iboush a répondu
iboush a répondu
Mouhamedsock_03 a répondu
Mouhamedsock_03 a répondu
iboush a répondu
iboush a répondu
Mouhamedsock_03 a répondu