Ou

Question en attente de réponse

Assurance Santé via orange money

Dama am idée,Assurance Santé via orange money.Légui kousi beugua bokk day am compte orange money,légui loumu déf dépot ak somme bafa nekk bou démé hopital lolu lay fadio.(Orange stp applique cette idée).Mon numero est 784535152

khadimSea1
khadimSea1

khadimSea1

Lecteur
0
48 / 51
points

Réponses

Salut khadimSea1
Sa idée bi idée bou réféte leu.
Mane nga dem si plateforme biniou diagléle idée yi
nga bindeu ko feu
Lien bagui ni https://ctc.orange.sn/
Sokofa défé dinaniouko étudié
Expert Orange